Les 3 dangers qui menacent celui qui ne fait plus les 5 prières quotidiennes (par Cheikh Ahmadou Bamba)

Yonent bi (YYJSM) neena ku bayyi julli, bu ngéen bokkee ndap di lek, day am tooke juy géen ciy weewam di wëndéelu ci ndap li. Ta kuci lek ap xolam lakk ta xol bu lakk daadi wow. Ta ku xolam wow sawara la jëm. Ndax sunu boroom mooni ci alquraan : wa waylun lil xaasiyati quluubuhum...

Yonent bi (YYJSM) neena ku bayyi julli bu jubée aw ñam, ñam wi day lox di wax naan sunu boroom yalla nga dindi barke ci man.

Yonent bi (YYJSM) neena ku bayyi julli kuko muuñ melnani màbbëna kenoy kaaba gi ta ku takk doomam melnani dàggna la dox diggëmëk boroomam.

 

Traduction Français :

D’aprés le prophète Mohamed (Psl) toute personne qui ne pratique plus les cinq prières quotidiennes, si tu manges dans le même plat que lui, des effets poissonneux émanant de ses ongles se divulguent sur le plat. Et si tu en manges, ton cœur (foi) va s’assombrir où n’entre plus la lumière divine. Un cœur assombri est synonyme de l’enfer. Car Dieu dit dans le coran : wa waylun lil xaasiyati quluubuhum

Par ailleurs, le prophète (psl) révèle que celeui qui ne pratique plus les cinq prières quand il s’approche d’une nourriture, cette nourriture tremble et le maudit, implorant Dieu de l’accorder aucune bénédiction…

le prophète (psl) indique il en est de même pour ce dernier, C’est comme si ‘il fait écrouler la Kabba et celui qui épouse sa fille a coupé le cordon qui existait entre lui et Dieu.

Cheikh Ahmadou Bamba

extrait de "Majmah'u nuurayni fii fawaa-i-di daarayni"

 

Rate this item
(0 votes)

Related items

Téléchargez l'application Toubamajalis

Facebook

(SERVICE COMMERCIAL ) Email : toubamajalis@gmail.com | webtawfeh@gmail.com

 

(REDACTION TOUBAMAJALIS) Email : sennegueye@gmail.com tel.

Chargé de communication : +221 77 539 55 17

Aller au haut