in ,

Ces beaux vers ont été adressés par Serigne Moussa Ka à la Famille de Seydina ISSA .

Hommage à Seydina Limamou Laye en ces jours d’appel de la Communaute Layenne qui entretienne avec la communaute Mouride de longues et veridiques relations fraternelles.

Ces beaux vers ont été adressés par Serigne Moussa Ka à la Famille de Seydina ISSA sous ndigueul de Serigne Fallou Mbacké.

“Issa”Mo ami xarbaax
Tabaxna ay taak
Du agné ab laax
“Najlou limamou

Wa sawou janta
Té gueena guenta
Issa d’i Dianta
Dem na bihaami

Xutbu zamaani
Xawsu lawaani
Xaasi wa daani
“Nuuru lanaami”

Uwa abiibu
Uwal latiifu
Uwa tabiixu
Lizil lislaami”

Uwal haliifah
Fi zil haniifah
Wa zum latiifah
Li zi lihaami

Uwa Haliimi
Uwal kariimu
Uwal sahiimu
Duunan bihaami”

Uwal amiiru
Lahul waziiru
Lahu uziiru
Bi zil kalaami”

Taxawlu naa fii
Allahu kaafii
Marsiya naa fii 
Domi limamou”

Yeen gaayi layene
Siyaar si naa leen
Te jaal si naa le en
Maha limamou”

Te gaayi issa
Ak doomi issa
Mucca ci “buusaa”
“Ilal xiyaami”

Salaatu sa ami
Maha salami
Ala humaami
“Xayru lanaami”

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée.

Written by LA REDACTION

Toubamajalis est un site d’actualité sur le mouridisme et proposant des dossiers sur l’islam et le monde musulman.

Gamou Nigeria 2019 : l’État de Kano célèbre la naissance de Cheikh Al Islam El Hadj Ibrahima Niass

Sénégal : la liste du nouveau gouvernement