in

Les recommandations de Serigne Touba pour celui qui voudrait avoir un garçon

1) Ku bind saaru yuusufa ci këyit gu weex ta benn araf faruci takkalko ku ëmbë, in chaa Allaahu dana am doom ju góor ju raffet. Ta yalla sunu boroom danako musël ci léeppu lumu ngërëmul.

Ap leeral : saaru yuusufa nak mooy fukkéelu saar ak ñaar (12em) ci kaamil bi.

2) Boroom Rawdul Yaanih’u neena ku bëgg doom ju góor, boo boolook sa soxna ba noppi na nga ko digël mu tëdde ndayjooram.

3) Ku bëgg doom ju góor, busa soxna ëmbée na nga tudde ëmb bi Muhammad (YYJSM).

 

 Majmahu nuurayni fii fawaa-i-di darayni

Auteur : Cheikh AHmadou Bamba

Transcription Wolof : S Moustapha Lô Kholl

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée.

Written by LA REDACTION

Toubamajalis est un site d’actualité sur le mouridisme et proposant des dossiers sur l’islam et le monde musulman.

URGENT! La communauté mouride en deuil : le fondateur de la page facebook Serigne Fallou Mbacké n’est plus.

Serigne Khadim Tassaouf : Les 5 facteurs de divorce chez la femme et chez l’homme